Ay tèereCi pàcc bi Ëttu gëstukaay bi ňu lèen jaglèel moo leen di wan teere yu bees yi ak situ internet yu yees yi ak lèpp lu jëm ci xibaar yi lamboo ak mbay camm ak nàpp ci Senegaal ak Maali. Ci bunt bi tamit munga fi fek ay teere yu bari yu ndaw yi bind ci dëk yi ňu jotta dem ci Senegaal ak Maali. Biral ab gëstuSo bëgge wane ab teere nak mun nga noo joot ci bunt bi. |