TagattDoxaline ci ňangalé mi Ňangalé maa ngi wéeru ci dém ca daara ja jangi buňu toftalé ak ay misaal ci tool yi. Téeré bu ci nék dafay and ak ay aluwa yu ndogo li di ganayoo ak yénéen jumtukay yu mëngëloo ak li muy jang (powerpoint, ay theatare open office, ay site internet, ëttu E-TIC bi, ak yénnéen jumtukay yu démé ni ay téeré ak ay taagàtt yu mëngoo ak liňu soxal). Li amal naňu solo lool lèpp luy ligey um mboolo, gënn ko soxla nak ci lu jëm ci taagàtt mi gëstu bi ci tool yi. Suňu mebet
|