Dimblikat yiSaartu ligey katu maaliporo ICVolontaires ap kureel la buy yëngu ci adina bi yëp ci te duk nguur buy jox askan wi ay xam xam ci wallu ligeey boo xamni kenn du ci fayaate ay dnit niuy ligey ci kalaama xarala yu mujj yi ak ay ndajje aki poroze.mungi yengu ci walu japalante doomi adama yi ci walu askan wi ci walu wergu yaram ci biir ak bitim reew. Ligeey kat yi nak niu ngi tol ci 16 at ba 80 att muy luy indi jokko cici ay xalaat yu wute te am solo. Sunu giss-gissSunu giss-giss moy tabax ëlek boo xam ni nit ku nek ak askan wune dina mënna am saň-saňak taaneef suňu mebet di dajale xam-xam yi ci li soxal askan wi jaarale ko ci ligeyuk japalante bi. ICVolontaires mungi bokk ci li suxali askan wi di ligey ci bokk gi muy yengu ci poroze ak ndajje yoo xamni koom lalu ko, yuy jox katan bèp mindef bu jogge ci bèpp askan bu soppa ligey ci japalante. ICVolontaires mungi xeex pour ligeyuk japalante ak nagutem. ICVolontaires nak yoon la ngirr ay xeet yu wuute mënna dajje ngir kunek xam moroomam ak yokutek ku ci nek. ICVolontaires mungi yengü ci xalaatuk motalante ci askan wi ak ci ligeey katu nguur gi.seeni yëngu nak mungi fetewu ci taneefu ligey kat yi bëgga japale askan wi ci maaliporo ak ndimbalak japale katt yi. Ngir ligeeyuk japalnate bi mënna antu nak, ICVolontaires dafa tëral ab Saart jëmaleko ci këpp ku bëgga du ci ňioom, muy li leen di wan seen axxak seen yeleef. Ligeeyu japalekat biJapalekat bi dafa di benn nit kouy jooxe ci waxtoom ci ni coobarem ngir nekinu askan wi te duniu ko ci fay dara. Amna foo xamni nak ndaw si daniu kooy deloo li mu jëffendikoo (ci wallu lekaam ak toxoom wala ak tukeem). Moom nak dafa wara farlu lool ci taxawu ICVolontaires. Te dafa wara def ligey bi niu ko sant ci genja defin. Yeen saya dina ňu ko soxla ci mu teewal ICVololontaires ci ay bërëp yu mel ni (ay waxtaanu mnbooloo, ay ndaje) wala mu dem gëstu ji ci ligeeyu benene mbooloo. Dafa wara am sutura ndax japalekat bi dafa am ay axx ak yeleef yu Saart bi di wane muy teere bi maakole ňëpp ci biir icvolontaires. Axxuk way japalekat
Wareefu way japalekat bi
© 2006 ICVolontaires |