TagattSaar yi ňi jang jangum "mebeètt yu bees ci mbay mi" ci jumtukaayu doxalin et njaay yu yees yi. Baykatt bi mooy ki moo toolam.ligeyam a ngi raňeku ci digënte bi nitt ki di doxal ak jawoom, caadaam ak yëngatoom. Su roombe mbay mi ak njaayum limu ci goobe,baykatt bi dafa lijenti lèpp lu àjju ci toolam, mooy tann li ko dalle ci xalaat ga ba ci jëff ga ci limu mebettoon ci tool ba.ligéy am dafay gënn di am solo ci tërëlinu dëkuwaayu pënc mi ak ci li àjju ci wallum doxalinu gancax wi. Mooy ki xaalat doxalinu toolam ba noppi da fexe numu kooy taxawale. Mooy taxawal lèpp lu àjju ci wàllu goob gi, coppi gi ak njaayum litool bi jùrr. Ci gàttal daal moy yorr lèpp luy lambo ci doxalinu bi jëm ci digënte tool bi ak pënc mi koy jëriňoo. Saar bu Jëkk bi: wisaaré bi
Li nek ci biir:
Saaru ňaareel bi: li ci booloo gi mënna yokk
Li nek ci biir:
Saaru ňàtteel bi: njaayin dundu wi
Saaru ňenteel bi: mbayum ndund mi
|